TSK

TSK · Deuteronomy 2:5

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Esawu nag dëkk ca tundu Seyir: Esawu moomu mooy Edom.

Ba Aji Kawe ji séddee xeet yi seeni suuf, tasaare doom aadama yi ci àddina, moo àppal xeet yi seen kemi réew, na mu dëppook limeefu goney Yàlla yi.

«Yaw nit ki, neel jàkk tundu Seyir, nga biral waxyu fi kawam.

Mboolem waa àddina di neen ci moom. Nu ko neex lay def ak gàngoori xarey asamaan ak waa suuf, te kenn du fél loxoom mbaa mu naa ko: «Ana looy def nii?»

Moo sàkke xeeti àddina yépp ci kenn nit, ñu dëkke déndu suuf sépp, te moo leen àppal seeni jamono, rëddal leen seen kemi dëkkuwaay.