TSK

TSK · Deuteronomy 2:8

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Noonu la Edom lànke, mayul Israyil mu jaare réewam, ba Israyil mujj teggi.

¶ Lii mooy kàddu yi Musaa wax bànni Israyil gépp, ca wàllaa dexu Yurdan, ca màndiŋ ma, fa joor ga jàkkaarlook Suf, diggante Paran ak Tofel ak Laban ak Aserot ak Disayab.

¶ Ay gaal yu mag itam Buur Suleymaan defarlu na ko ca Esiyon Geber ga ca wetu Elat, ca tefesu géeju Barax ya, ca réewum Edom.

Jamono yooyu, fekk na Reccin nangu Elat, mu tàbbi ci loxol Siri. Mu génne waa Yuda Elat; Edomeen ña délsi Elat, dëkk fa ba bésub tey jii.