Genesis 19:37
TSK
Taaw ba am ca doom ju góor, tudde ko Mowab (mu firi Jóge ci baay). Mowab moo sos Mowabeen ñi.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Taaw ba am ca doom ju góor, tudde ko Mowab (mu firi Jóge ci baay). Mowab moo sos Mowabeen ñi.
Lakk gaa nga jóge Esbon, sawaraa bawoo dëkkub Siwon ba, xoyomi Ar ga ca Mowab, gor ñooña tiim dexu Arnon.
Buleen xeex ak ñoom, ndax duma leen jox ci seen suuf fu téstën sax tege, ngir Esaween ñi laa sédd diiwaanu tundu Seyir.
Noonu nu Esaween ña dëkke Seyir defaloon, ñook Mowabeen ña dëkke Ar rekk. Su ko defee nu mana jàll dexu Yurdan, ba àgg ca réew ma nu sunu Yàlla Aji Sax ji jox.»
néegi Gebal, Amon ak Amaleg ak waa Filisteek waa Tir,