TSK

TSK · Deuteronomy 21:19

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

na seeni mag ak seeni àttekat dem, natti diggante fa néew ba tëdd, ak dëkk ya ko séq.

Te képp kuy biralati waxyu, ay waajuram, baayam ak ndeyam nañu ko wax ne ko: “Doo dese bakkan, ndax yaa fen ci turu Aji Sax ji.” Ay waajuram, baayam ak ndeyam nañu ko jam ba mu dee, ca ba muy biral waxyu.