Leviticus 21:7
TSK
¶ «Ab gànc mbaa ku ñu torxal, tëdde ko, ñoom duñu ko jël soxna. Ku jëkkëram baal it duñu ko jël soxna, ndax dañoo sellalal seen bopp seen Yàlla.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
¶ «Ab gànc mbaa ku ñu torxal, tëdde ko, ñoom duñu ko jël soxna. Ku jëkkëram baal it duñu ko jël soxna, ndax dañoo sellalal seen bopp seen Yàlla.
Waaye doomu sarxalkat bu boroom këram faatoo mbaa mu tàggook moom te amu ca doom, bu delloo kër baayam na mu fa nekke woon ba muy gone, sañ naa lekk ci ñamu baayam. Waaye kenn ku ci bokkul sañu cee lekk.
Ab jëtun ak ku ñu fase, sarxalkat du ko jël jabar. Su dee janq bu askanoo ci waa kër Israyil mbaa ab jëtun bu sarxalkat doon denc, sañ nañu koo jël.