TSK

TSK · Deuteronomy 27:13

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Ba Leya ëmbee, am doom ju góor, da koo tudde Ruben (mu firi Gisleen, doom ju góor a ngi), ndaxte Leya da ne: «Aji Sax ji gis na sama toroxte. Léegi sama jëkkër dina ma bëgg.»

Booba la ne: «Yàlla defal na ma teraanga ju réy. Bii yoon sama jëkkër dina ma teral, ndax amal naa ko juróom benni doom yu góor.» Moo tax mu tudde ko Sabulon (mu firi Teraanga).

¶ Bu leen seen Yàlla Aji Sax ji yóbboo ca réew ma ngeen jëm, ngir nanguji ko, nangeen tudd barke bi ca kaw tundu Garisim, te ngeen tudd alkànde ji ca kaw tundu Ebal.