Aji Sax ji ne Musaa: «Jëlal Yosuwe doomu Nuun. Nit la ku noowal biir nekk ci moom. Nanga ko teg sa loxo, sase ko noonu.
TSK
TSK · Deuteronomy 3:21
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Numbers 27:18
TSK
Deuteronomy 7:19
TSK
ak mitit yu réy ya ngeen gisal seen bopp, ak firnde yaak kéemaan ya, ak seen dooley loxol Yàlla Aji Sax jeek kàttanam gu réy, ga mu leen génnee. Noonu la seen Yàlla Aji Sax ji di def mboolem xeet yi ngeen ragal.
1 Samuel 17:36
TSK
Rey naa gaynde, rey naa weneen rabu àll wu aay, sang bi. Kon nag yéefaru Filisti bii it ni wenn ci yooyu rab rekk, ndax moo tëkku gàngoori Yàlla jiy dund.
Moo nu wallu ci googu dee gu naroona metti, moo nuy walluwaat, te moom lanu yaakaar mu wallooti nu.
Ephesians 3:20
TSK
¶ Moom mi mana jëfoo kàttan giy liggéey ci nun, ba sottal mboolem lu nu ñaan ak lu nu xalaat, ba wees loola fuuf sax,