1 Samuel 14:26
TSK
Ba mbooloo ma duggee ca biir gott ba, yemuñu ca lu moy lem jay xelli, waaye kenn sàkku ci, jëme ci gémmiñam, ndax ragal ngiñ la.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Ba mbooloo ma duggee ca biir gott ba, yemuñu ca lu moy lem jay xelli, waaye kenn sàkku ci, jëme ci gémmiñam, ndax ragal ngiñ la.
Ana lu waral nag sàmmoo la nga giñoon ci Aji Sax ji te ma santoon la ko?»
Doom, ragalal Aji Sax ji, wormaal buur. Bul lëngook kuy fippu.
¶ Na ku nekk déggal njiit yi yor kilifteef, nde amul njiit lu bawoowul fa Yàlla, te njiit yi toog, Yàlla moo leen tabb.
¶ Nangul-leen gépp kilifteef gu tege ci àddina ngir Boroom bi; muy buur bu mag bi gëna kawe,