TSK

TSK · Esther 2:19

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Buur, dangay yónnee ay ndaw ci sa mboolem diiwaani réew mi, ñu dajaleel la mboolem janq ju rafet ji, indi leen fii ci Sus, péey bi, dugal leen ci kër jigéen ñi, ñu teg leen ci loxol Ege, sa bëkk-néeg biy wattu jigéen ñi. Ñu jox leen lu ñuy defaroo ba rafet.

Mboolem jawriñi buur yi féete buntu kër buur nag di sukkal Aman, di ko sujjóotal, ndax loolu la Buur santaane woon ci moom. Teewul Mardose lànk, sukkalu ko, sujjóotalu ko.

Waaye loolu lépp doyu ma, li feek maa ngi gis benn yoon Mardose, Yawut bi, mu toog ca buntu kër buur.»