TSK

TSK · Esther 2:4

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Mu ne Amnon: «Waaw, yaw doomu buur nga, lu la tax ne yogg nii bés bu set? Doo ma ko wax?» Amnon ne ko: «Tamar, mi bokk ak sama doomu baay Absalom ndey ak baay, moom laa bëgg.»

Pexe moomu nag jub ci Absalom, mook magi Israyil ñépp.

Ndegam neex na la, Buur, bindal ab dogal bu leen sànklu. Kon ñetti junniy barigoy xaalis laay teg ci loxoy saytukat yi, ñu yeb ko ci dencu buur.»