TSK

TSK · Esther 3:7

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

¶ Mu am bés, ci weeru Nisan, ñeenti weer gannaaw Kislew, yemook ñaar fukkeelu atu nguurug Artaserses, ma jël biiñ ba taaje woon fa kanam Buur, di ko ko xellil. Booba maa nga ànd ak tiis, ne yogg; lu ma masula dal ca kanamam.

Ñu yóbbu Esteer ca Buur Aserus, ca biir këram, ca fukkeelu weer wa ñuy wax Tebet, ca juróom ñaareelu atu nguuram.

¶ Ba loolu amee Yawut ya di fàdd seen noon yépp, saamar yay dal, ñu di leen bóom ak a faagaagal. Ñuy def seeni bañ lu leen neex.

ngir sas leen at mu nekk, ñu wara wormaal fukki fan ak ñeent ak fukki fan ak juróom ci weeru Adar,

Moo waral ñuy wooye yooyu bés bési Purim, mu jóge ci baatu «Pur», di jumtukaayu tegtal boobu. Mboolem la ñu bind ca bataaxal boobu nag ak itam la ñu gisal seen bopp ak la ñu daj,

Saamar, ñaweel sa ndijoor, walbatiku, jëm càmmoñ, ak foo mana jublu,