1 Kings 21:4
TSK
¶ Axab ñibbi këram, mer, ne fóññ ndax la ko Nabot waa Yisreel ba wax, ne ko du ko jox suufas maamam. Mu tëdd ca lalam, gedd, baña lekk.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
¶ Axab ñibbi këram, mer, ne fóññ ndax la ko Nabot waa Yisreel ba wax, ne ko du ko jox suufas maamam. Mu tëdd ca lalam, gedd, baña lekk.
Bésoo bés ku bon ay bittarñikoo biir njàqare, te diirub at yi ñu àppal ku néeg,
Ku bon fexeel ku jub, di ko màttu,
Gis naa jépp jëf ju jëfe ci kaw suuf, ndeke lépp cóolóoli neen la ak napp um ngelaw.