TSK

TSK · Esther 7:3

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Mu delluwaat yebal njiital juróom fukki dag, mu ànd ak juróom fukkam ña, muy ñetteel bi yoon. Mu daldi dem ba àgg ca Ilyaas, ne gurub sukk ca kanamam; tinu ko ne ko: «Éy góoru Yàlla gi, ngalla wormaalal sama bakkan ak bakkani juróom fukk ñii, sang bi.

Buur, ndegam yéwéne nga ma, te may ma li may ñaan, defal ma li may sàkku di sa coobare, ngalla, Buur, àndal ak Aman, dikk ca bernde ja ma leen di waajalal. Kon bu subaa dinaa la wax li ngay laaj.»

Job 2:4 TSK

Seytaane ne Aji Sax ji: «Bakkan a wuutu bakkan rekk. Mboolem lu nit am, man na koo weccee bakkanam.

ne leen rekk danga ma doon tinu, ndax ma bañ laa delloo kër Yonatan, nga di fa dee.»