TSK

TSK · Exodus 10:13

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Gannaaw ga juróom ñaari gub yu gooy yu ngelaw li lakk sax, tegu ca ya jiitu.

Yàlla wale ngelawal penku fa asamaan, bëmëx ak dooleem ngelawal bëj-saalum.

Day àddu, sant ngëlén, mu yékkati gannax yi.

soccet, amul buur, teewul ñuy àndandoo, diy gàngoor;

Jonah 4:8 TSK

Naka la jant ba fenk, Yàlla yebal ngelawal penku lu tàng jérr, jant ba jam boppu Yunus, ba mu xawa xëm, bëggatul dara ci bakkanam. Mu naan: «Dee sax a ma gënal dund!»