TSK

TSK · Exodus 14:3

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Su ko defee bu leen musiba yu bare dikkalee aki njàqare, woy wii mooy biral kàddug seede fi seen kanam, ndax su boobaa xel du ko faaye, ba mu réer seenu askan. Ndax kat xam naa seen mébét mi ñuy rabat, te yóbbooguma leen sax ca réew ma ma leen giñaloon.»

¶ Ci kaw loolu ñu yegge Sóol ne ko Daawuda dem na Keyla. Sóol ne: «Kon de Yàllaa ko teg ci samay loxo, ndax ba mu duggee biir dëkk bu tëje ràpp la tëj boppam.»

Éy Aji Sax ji, noon yeeka bare! Ñu baree may jógal,

yaa xam sama toogaay ak sama taxawaay, di ràññee fu sore samay xalaat,

Dégg naa ñaawlaate yu bare, ñu naan: «Éey, Tiitaange-lu-dajal! Booleleen ko, boole rekk!» Ñi ma séqal jàmm sax, di yeeru ma fakkastalu, naan: «Jombul mu juum, nu jekku ko, ba mana feyu.»

«“Boroom bi Aji Sax ji déy dafa wax ne: Yaw déy, laa doon wax bu yàgg, yonenti Israyil, sama jaam ña jottli ko ca yooya jant, ñu biral waxyu ay ati at, ne maa lay dal-loo sama kaw ñoñ.