TSK

TSK · Exodus 2:1

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

¶ Ba Israyil dëkkee ca réew ma, am na bés Ruben dem tëdd ak Bilaa, nekkaaleb baayam; Israyil yég ko. Doomi Yanqóoba yu góor fukk lañu ak ñaar.

¶ Amram moo jël bàjjanam Yokebedd soxna, kooku am ak moom Aaróona ak Musaa. At, ya Amram dund, téeméer la ak fanweer ak juróom ñaar (137).

Ci biir loolu Adàdd ànd ak ay Edomeen ñu bokkoon ci dagi baayam, daldi daw jëm Misra. Booba Adàdd xale bu góor bu ndaw la woon.