Exodus 4:20
TSK
Musaa ànd ak soxnaam ak doomam yu góor, waral leen mbaam. Ma ngay dellu Misra, jàpp yetu Yàlla wa ca loxo ba, yóbbaale.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Musaa ànd ak soxnaam ak doomam yu góor, waral leen mbaam. Ma ngay dellu Misra, jàpp yetu Yàlla wa ca loxo ba, yóbbaale.
¶ «Képp ku dib jëtun akub jirim, buleen ko néewal.
Yaay mbugal ku bàkkaar, yar ko, ronq ni max la mu gëna fonk. Nitoo nit, cóolóolu neen. Selaw.
Musaa dégg kàddu googu, daldi gàddaay, dem dali réewum Majan, ba am fa ñaari doom yu góor.