TSK

TSK · Exodus 21:20

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Kayin kay, lees di feyul juróom ñaari yoon, ne, bu dee Lemeg mii, muy juróom ñaar fukki yoon ak juróom ñaar.»

¶ «Ku dóor ab jaamam bu góor mbaa bu jigéen, ba tuur bëtam, na ko goreel ndax bët ba.

¶ «Képp ku faat bakkan nag, ci kaw kàddu gu tukkee ci ay seede doŋŋ lees ko saña reye, moom ma rey, waaye bennub seede du seedeel nit, ngir ñu teg ko àtteb dee.

Waxi neen yarul surga, da lay dégg te du la déggal.

Ndax kilifa gi mooy ndaw li Yàlla yebal ngir sa jàmm. Waaye soo dee def lu bon, ragalal, ndax kilifa gi yorul ab saamar cig neen; mooy ndawal Yàlla liy añale, te mooy jottli am sànj mu wàccal kuy def lu bon.