¶ Waaye wattuleen, wattuleen seen bopp bu baax, bala ngeena fàtte mbir yi ngeen teg seen bët, ba du génn seenum xel seen giiru dund gépp. Te nangeen ko xamal seeni doom ak seeni sët.
TSK
TSK · Exodus 23:13
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Deuteronomy 4:9
TSK
Deuteronomy 6:1
TSK
¶ Lii mooy santaane bi, ak dogali yoon yeek àttey yoon yi seen Yàlla Aji Sax ji santaane ma jàngal leen ko, ngir ngeen di ko jëfe ca réew ma ngeen jàll jëm, ngir nanguji ko,
Psalms 39:1
TSK
Mu jëm ci Yedutun, njiital jàngkat yi, di kàddug Sabóor, ñeel Daawuda.
Hosea 2:17
TSK
Foofa laa koy delloo tóokëri reseñam, defal ko xuru Akor di buntu yaakaaram. Fa la may feeloo na woon ca janti ndawam, ba muy génn réewum Misra.
Ephesians 5:12
TSK
Ndax kat li nit ñooñu di làquy def, waxtaane ko sax, lu ruslu la.
1 Timothy 4:16
TSK
Sàmmal sa bopp nag, sàmm sa àlluwa, te saxoo ko; soo ko defee, dinga mucc, musal ñi lay déglu.