TSK

TSK · Exodus 3:5

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

¶ Ci kaw loolu Yanqóoba yewwu ne: «Ndekete Aji Sax ji mu ngi ci bérab bii, te xawma ko woon.»

Musaa xamal ko la ko Aji Sax ji dénk lépp, ak mboolem firnde, ya mu ko sant mu def ko.

Aji Sax ji ne ko: «Wàccal, àrtu mbooloo mi, ndax ñu baña bëtt, di ma deñsi kumpa; lu ko moy ñu bare ci ñoom dinañu dee.

Acts 7:33 TSK

Boroom bi ne ko: “Summil say dàll, ndax fii nga taxaw, suuf su sell la.