TSK

TSK · Exodus 33:5

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Malaaka ma ne ko: «Bu sa loxo laal xale bi; bu ko def dara, ndaxte léegi xam naa ne ragal nga Yàlla, ndax gàntaloo ma sa jenn doom ji.»

ba ngeen dugg ca réew mooma meew maak lem ja tuuroo. Waaye duma ànd ak yeen, lu ko moy dinaa leen faagaagal ci yoon wi, ndax askan wu dëgër bopp ngeen.»

Job 34:20 TSK

Nes tuut, dee dikke xaaju guddi, mbooloo fippu, kàngam ya ne mes, boroom doole sànku, te loxo laalu ko.

Yàlla, seetlu ma, ba ràññee sama xol; natt ma, ba ràññee sama xalaati xol.

Xam naa ne ñu dëgër bopp ngeen. Dangeen të, wowle.

Joel 2:12 TSK

«Terewul ba léegi,» kàddug Aji Sax jee, mu ne: «Délseeleen seen léppi xol ci man, boole kook koor aki jooy aki yuux.