TSK

TSK · Exodus 34:13

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

nangeen dàq waa réew mépp, nangeen yàqte seen mboolem tuur yu ñu yett, te seen mboolem jëmm yu ñu móol, yàqteleen ko, seen mboolem bérabi jaamookaay it, tasleen ko.

Seen jëmmi tuur yooyu nag, lakkleen leen. Buleen xemmem lenn luy xaalis mbaa wurus ci kaw tuur yi. Buleen ko aakimoo, lu ko moy muy seenug fiir, ndax lu seexluwoo ngoogu ci seen Yàlla Aji Sax ji.

¶ Buleen samp benn xeru bant, bu jóge ci genn garab, ngir di ko jaamoo Asera tuur mi, ci seen wetu sarxalukaay bi ngeen sàkk ngir seen Yàlla Aji Sax ji.

Dañoo daane jëmmi Baal ja, màbb kër Baal, boole ca, def kob sën, te moom la ba tey jii.

Rajaxe na tuuri doj ya, daane xer ya ñuy jaamoo Asera, wuutal fa ay jali yaxi nit, ba mu daj.