TSK

TSK · Exodus 34:4

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

¶ Ba loolu amee Musaa yéeg, jëm ca Yàlla. Aji Sax ji jaar ci turu Musaa foofa ca kaw, ne ko: «Nanga wax ak waa kër Yanqóoba te nanga ma siiwtaaneel ci bànni Israyil googu, lii ma lay wax:

Àlluwa ya, liggéeyu Yàllaa, mbind ma di mbindum Yàlla mu ñaase ca kaw àlluwa ya.

Ma sàkk gaalu bantu séng, daldi yett ñaari àlluway doj yu mel ni yu jëkk ya. Ci kaw loolu ma yéeg ca kaw tund wa, maak ñaari àlluwa yi ci sama loxo.