TSK

TSK · Exodus 35:29

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

¶ «Sàkkleen ci seen alal ab jooxe bu ñeel Aji Sax ji. Képp ku am yéeneb xolam, na indi jooxeb Aji Sax ji: wurus ak xaalis ak xànjar,

Ba mu ko defee ñu nangoo ci Musaa mboolem jooxe bu bànni Israyil indi, ngir sottal liggéeyu bérab bu sell bi. Bànni Israyil nag jàppoo suba gu jot di indil Musaa ay saraxi yéene,

sàmmooleena jëfe mboolem dogal yeek àttey yoon yi ma teg fi seen kanam, bésub tey jii.

Su ma yebu woona def lii ci sama coobarey bopp, dinaa ci am peyoor. Waaye gannaaw dees maa dénk ag caytu, te ajuwul ci sama coobare,

Mboolem ñiy sàmm ndigal lii nag, te di Israyilu Yàlla, jàmm ak yërmande ñeel na leen.

¶ Rax ci dolli nu ngeek waxi yonent yi, muy wax ju wóor ju jara gëm, te yeena yey teewlu waxi yonent yi, ni ñuy teewloo ceeñeeru làmp bu tàkke biir lëndëm, ba kera fajar di xar, ba biddiiwu njël feqal seen xol.