Genesis 30:37
TSK
¶ Ci kaw loolu Yanqóoba tànn ñetti garab yu ñuy wax pëpalyee, gerte-tubaab ak palataan, gor ci bant yu tooy, xànc-xàncee ko, ba mu defi rëdd yu weex.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
¶ Ci kaw loolu Yanqóoba tànn ñetti garab yu ñuy wax pëpalyee, gerte-tubaab ak palataan, gor ci bant yu tooy, xànc-xàncee ko, ba mu defi rëdd yu weex.
Musaa ànd ak soxnaam ak doomam yu góor, waral leen mbaam. Ma ngay dellu Misra, jàpp yetu Yàlla wa ca loxo ba, yóbbaale.
Alyaasa ne ko: «Loo bëgg ma dimbalee la ko? Wax ma loo am ca kër ga.» Mu ne ko: «Dara, sang bi. Awma dara ca kër ga lu moy taxub diw.»
xanaa di àtte ku ñàkk ci njekk, di dogalal njub, néew-ji-dooley àddina. Mooy dóore àddina, bantub kàddoom, mooy reye ñu bon ñi, ngelawal gémmiñam.