TSK

TSK · Exodus 4:27

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Ba loolu amee Yanqóoba fóon Rasel, ne yikkét jooy.

Aji Sax ji nag mer ba fees ndax Musaa. Mu ne ko: «Sa mag Aaróona, Leween bi, da fee nekkul? Moom, xam naa ne ku mana wax la. Mu ngi lay gatandusi sax, te bu la gisee, bég.

¶ Mbooloo mépp a nga teew, ba muy dënook a melax, ànd ak coowal liit gaak tund way saxar. Ñu gis loolu, di kat-kati, dànd fu sore.

Ilyaas jóg lekk, daldi naan, leqliku, ba dox ñeent fukki guddi ak ñeent fukki bëccëg, ba ca Oreb, tundu Yàlla wa.

Wàccal boog, ànd ak ñoom te bul nàttable, ndax man maa leen yebal.»