TSK

TSK · Exodus 4:28

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Mu ne ko: «Bu ñu la gëmul mbaa ñu baña seet ci firnde ju jëkk ji, dinañu gëm ndax firnde ji ci topp.

¶ Musaa dellu, woolu magi mbooloo ma. Mu jottli leen mboolem wax jooju ko Aji Sax ji dénk.

Jonah 3:2 TSK

«Jógal dem Niniw, dëkk bu mag ba, nga yegge leen kàddu gi ma lay dénk.»