Exodus 29:4
TSK
Yóbbul Aaróona ak doomam yu góor, ba ca bunt xaymab ndaje ma, nga sang leen.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Yóbbul Aaróona ak doomam yu góor, ba ca bunt xaymab ndaje ma, nga sang leen.
Ci kaw loolu, ñu firi malaan mi ci kaw jaamookaay bi, daldi lal kiiraay li ci kawam, na ko Aji Sax ji sante woon Musaa.
Yàquleeka leena bett! Musibaa leen ne fuuf, ñu ne mes!