2 Kings 18:20
TSK
Defe nga ne làmmiñ kese doy na pexeek njàmbaar cib xare? Ma ne: Ana kan nga yaakaar bay fippu ci sama kaw?
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Defe nga ne làmmiñ kese doy na pexeek njàmbaar cib xare? Ma ne: Ana kan nga yaakaar bay fippu ci sama kaw?
Asaryaa doomu Osaya ak Yowanan doomu Kareya ak nit ñu bew ñooñu ñépp jël kàddu gi. Ñu ne Yeremi: «Dangay fen! Sunu Yàlla Aji Sax ji santu la nga fommloo nu sunu yoonu Misra ga nu bëgga toogi.
Yeena ne: “Jaamu Yàlla ag neen la. Ana lu nu jële ci dénkoo ndénkaaneem, tey wéye toroxlu fi kanam Aji Sax ji Boroom gàngoor yi?