Exodus 8:14
TSK
Ñeengokat ya fexe ca seeni xargafuufa, nu ñu defe ay rayentaan, waaye manuñu. Rayentaan ya nag song nit ñaak rab ya.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Ñeengokat ya fexe ca seeni xargafuufa, nu ñu defe ay rayentaan, waaye manuñu. Rayentaan ya nag song nit ñaak rab ya.
Nappkat di jàmbat, kuy sànnib oos dexu Niil di jooy, kuy mbaal waaru,