Deuteronomy 4:14
TSK
Man nag la Aji Sax ji sant ca yooya jant, ne ma xamal leen dogali yoon yeek àttey yoon, yi ngeen wara jëfe ca réew ma ngeen jëm, ngir nanguji ko.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Man nag la Aji Sax ji sant ca yooya jant, ne ma xamal leen dogali yoon yeek àttey yoon, yi ngeen wara jëfe ca réew ma ngeen jëm, ngir nanguji ko.
¶ Kàddug Aji Sax ji dikkal na ma ne ma: