TSK

TSK · Ezekiel 21:11

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Moo ma tax ne: «Buleen ma xool, damay naqarlu, jooy. Tàyyileen maa dëfal ci sama bokk yi sànku.»

¶ Bésub keroog nag ñi Aji Sax ji fàdd, fu ne lañuy tëdd ci àddina, cat ba cat. Deesu leen jooy, deesu leen for, deesu leen rob. Ni neefare jonkan lañuy wetaroo ci kaw suuf si.

«Yaw nit ki, jottlil waxyu, ŋëbal bii loxo, dóor ca bee. Na saamar bi dal benn yoon, ñaari yoon, ba ñett, saamaru ndee la, saamar baay bóom ñu bare, gaw leen,