Nehemiah 3:3
TSK
¶ Bunt ba ñuy wooye buntu Jën ya, góori waa Sena ñoo daaj bant ya, taxawal laf ya, def ca tëjukaay yaak dénki galan ya muy àndal.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.