Ezra 8:4
TSK
Ci askanu Payat Mowab, Elyowenay doomu Seraya la, mook ñaar téeméeri góor (200).
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Ci askanu Payat Mowab, Elyowenay doomu Seraya la, mook ñaar téeméeri góor (200).
Kon daal na sunuy kilifa taxawal askan wi. Su ko defee mboolem ku nekk ci sunuy dëkk te jël ci jaambur ñi jabar day dikk, ku ci nekk ca bés ba ñu ko àppal, te mu ànd ak kilifa yaak àttekati dëkkam. Ñu topptoo mbir mi nag, ba keroog sunu merum Yàlla mu réy mi sababoo ci lii, dëddu nu.»
Askanu Payat Mowab, soqikoo ci Yeswa ak Yowab, di ñaari junni ak juróom ñetti téeméer ak fukk ak juróom ñett (2 818).