TSK

TSK · Galatians 4:13

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

¶ «Góor gu bopp ba amatul kawar dafa leel waaye set na.

Man daal, ci sama biir néew dooley bopp, ak ragal bay kat-kati, laa nekke woon ak yeen.

Su ma dee ku xareñul ci wàllu wax it, du ci wàllu xam-xam, te nu nekk lanu leen wone loolu, ci bépp fànn.

¶ Te it, waccalees na ma ndégu biir suux, mu taxawe ndawal Seytaane, di ma mitital, ngir ma baña bew ndax peeñu yu yéeme.

¶ Man de jaaxle naa ci nii ngeen gaawa dëddoo Yàlla mi leen woo ci boppam, ci ndimbalal yiwu Almasi, bay topp xaat beneen xibaaru jàmmeey!