Deuteronomy 2:23
TSK
Aween ña dëkke woon dëkk yu ndaw ya dem, ba àkki Gasa nag, Kaftoreen ña bàyyikoo Keret ñoo leen faagaagal, wuutu leen.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Aween ña dëkke woon dëkk yu ndaw ya dem, ba àkki Gasa nag, Kaftoreen ña bàyyikoo Keret ñoo leen faagaagal, wuutu leen.
Bésub keroog Boroom bi jooti loxoom ñaareel bi yoon, ngir jotaat ndesu ñoñam, wa des Asiri ak Misra, ak Pattros ak réewum Kuus, ak Elam ak Sineyaar, ak Amat ak biir duni géej ya.
bésub sànkute dikkal képp kuy Filisteen, ba dagge dëkk yii di Tir ak Sidon ndimbal lu ñu dese woon. Aji Sax jaa ngay sànk Filisteen, ña des te cosaanoo dunu Keret.