TSK

TSK · Genesis 10:18

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

¶ Ci kaw loolu buurub Asiri jële ay nit dëkk ya ñuy wax Babilon ak Kuta ak Awa ak Amat ak Sefarwayim, dëël leen dëkki Samari, ñu wuutu bànni Israyil. Ñu daldi moom diiwaanu Samari, féetewoo dëkk ya.

waa Sidon ak Arwàdd doonoon say joowkat. Yaw Tir, yaa yeb ñu rafet xel, ñuy say mool,

Kàddu gi dal na itam Amat, ga digalook Damaas, dal Tir ak Sidon, ak la ñuy muus lépp.