TSK

TSK · Genesis 11:2

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Dëkk yiy péeyi nguuram ñoo di: Babel ak Ereg ak Akàdd ak Kalne, gi ci réewu Sineyaar.

Ba mu ko defee Lóot tànn jooru Yurdan gépp, daldi toxu jëm penku. Noonu lañu teqlikoo.

Bésub keroog Boroom bi jooti loxoom ñaareel bi yoon, ngir jotaat ndesu ñoñam, wa des Asiri ak Misra, ak Pattros ak réewum Kuus, ak Elam ak Sineyaar, ak Amat ak biir duni géej ya.

¶ Mu ne ma: «Ag kër lañu koy tabaxali ca réewum Sineyaar. Bu noppee, fa lañu koy teg, ca kaw tegukaayam.»