TSK

TSK · Genesis 14:10

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Ñu ne: «Ayca nu defar ay móol yu ñu lakk cib taal, ba mu ñor.» Ci kaw loolu ñu def móol ya doji tabax, taqalee ko koltaar,

¶ Gannaaw loolu Lóot dafa ragala dëkk Sowar, ba toxoo fa, ànd ak ñaari doomam yu jigéen, sanci ca tund ya. Mu dëkk ci xuntim xeer, moom ak ñaari doomam yu jigéen.

Def leen na nga defoon waa Majan, def ko Sisera ak Yabin ca dexu Kison.

«Pat-patiy daw, tàbbim pax; génn um pax, tàbbim yeer. Maay yen Mowab, maa leen di yen moos, seen atum mbugal.» Kàddug Aji Sax jee.