TSK

TSK · Genesis 14:2

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Kemu suufas Kanaaneen ña, mu ngi tàmbalee Sidon, jaar weti Gerar, dem ba Gasa, wuti Sodom ak Gomor ak Atma ak Ceboyim, daldi teeri Lesa.

Gisuloo dëkk bale; jege na, te dëkk bu tuut la, am déet? Ma daw, làquji fa boog, ba mucc?»

ak wetu bëj-saalum, ak xuru Yeriko, dëkku tiir ya, ba ca Sowar.

Maay jooy Mowab jooyi xol, nit ñaa nga fay dawe ba Sowar, àkki ba Eglat Selisiya. Ña ngay yéeg jëm Luwit, di jooyoo, awe yoonu Oronayim, di jalu.

«Efrayim, ana nu ma lay baye, yaw Israyil laa ne, nu ma lay tege ciy loxo? Ana nu ma lay defe ni Atma? Nu ma lay yemaleek Ceboyim? Sama xol a bëpp, sama yërmandee yëngu.