1 Kings 13:8
TSK
Góoru Yàlla ga nag ne Buur: «Soo ma joxoon sa genn-wàllu kër sax, duma ànd ak yaw te duma sex dugub it mbaa may naan um ndox ci bii bérab,
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Góoru Yàlla ga nag ne Buur: «Soo ma joxoon sa genn-wàllu kër sax, duma ànd ak yaw te duma sex dugub it mbaa may naan um ndox ci bii bérab,
¶ Gewasi surgab góoru Yàlla ga, Alyaasa, ne ca xelam: «Eewaay sama sang daal! Day bàyyi Naaman waa Siri bii mu dem noonu rekk; jëlul dara ci li mu indi. Giñ naa ko ci Aji Sax ji, Kiy Dund, dinaa daw dabi ko, ba am ci moom as lëf.»
Te ba ma nekkee ci yeen te soxla dab ma, wéeruwuma ci kenn ci yeen, ndax la ma ñàkkoon, bokk ya jóge Maseduwan ñoo ma ko indil. Fexe naa ba du lenn lu ma leen diisale, te noonu laay saxoo.
¶ Buleen jikkowoo bëgg ub xaalis; doylooleen li ngeen am, ndax Yàlla moo ne: «Duma la bàyyi mukk, duma la wacc mukk.»