Genesis 18:13
TSK
Aji Sax ji daldi wax Ibraayma ne ko: «Lu Saarata di ree, te naan: “Man mu màggat mii, deeti naa am doom moos?”
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Aji Sax ji daldi wax Ibraayma ne ko: «Lu Saarata di ree, te naan: “Man mu màggat mii, deeti naa am doom moos?”
di reek a sarxolle rekk. Yéefar yi naa: «Lu réy la Aji Sax ji defal ñii.»
¶ Ci kaw loolu Maryaama laaj malaaka mi ne ko: «Nu loolu di ame, te man xawma góor?»
¶ Ci kaw ngëm itam la Saarata ci boppam mana ëmbe ba jur tey mag ba wees njurum doom, ndax moo njortoon ne ka dige ku wóor la.