TSK

TSK · Genesis 2:22

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Loolu fekk na Yàlla Aji Sax ji sàkk ci suuf nja-àll yépp ak njanaaw yépp, daldi leen indil nit, di seet nu leen nit di tudde; te tur wu mu leen jox, muy moom.

Ku am jabar, am nga ngëneel, am nga yiwu Aji Sax ji.

ndax góor kat, jëleesu ko ci jigéen, waaye jigéen kay lañu jële ci góor.

¶ Na ñépp wormaal diggante bu ab séy dox, te ab lalu séy na mucc sobe, ndax fokati séy yi, ak jaalookat yi, Yàlla moo leen di daan.