TSK

TSK · Genesis 21:27

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Ibraam nag wax buurub Sodom ne ko: «Man yékkati naa sama loxo, Yàlla Aji Sax ju Kawe ji seede, moom mi sàkk asamaan ak suuf,

Ca ëllëg sa, ñu xëy suba teel, daldi waatoo, Isaaxa door leena yiwi, ñu dem ci jàmm.

Ba loolu amee Yonatan fasook Daawuda kóllëre, ndax sopp ko ni boppam.

Deel maye, da lay ubbil bunt, di la àggle ci boroom daraja.

Ku mer, may ko ci sutura, mu giif; boroom xadar, boqal ko neexal, mu dal.

Moo tànn ku bokk ci askanu buur, fasook moom kàddu, giñloo ko ne dina ko nangul, daldi yóbbu njiiti réew mi,

¶ Bokk yi, ma misaale ko mbiri doom Aadama. Kayitub donale bu nit doŋŋ bind, su dee lu wóor, deesu ko neenal, mbaa di ci yokk dara.