Genesis 18:2
TSK
Naka la siggi, gis ñetti nit, ñu ne jimeet ci kanamam. Ibraayma gaawtu, gatandu leen, sujjóotal leen.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Naka la siggi, gis ñetti nit, ñu ne jimeet ci kanamam. Ibraayma gaawtu, gatandu leen, sujjóotal leen.
¶ Ba mu ko defee Ibraayma sujjóotal waa réew ma,
Barey àndandoo lor a ngi ci, waaye xarit a ngi gëna taq nit mbokkam.
¶ Sàkkuleen jàmm seen diggante ak ñépp, te it sàkkuleen sellnga, nde ku sellul du gis Boroom bi.