TSK

TSK · Genesis 24:2

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Surga ba dugal loxoom ca suufu luppu Ibraayma sangam ba, daldi giñ ca loola.

Teewul Yuusufa bañ, ne soxnas sang ba: «Déglul, sama sang da maa jébbal lépp, ba topptootul dara ci kër gi.

Ba nga xamee ne àppu Israyil a ngay bëgga mat, dafa woolu doomam Yuusufa ne ko: «Ngalla waay dugalal sa loxo, mu ron sama lupp, muy ngiñ ci yaw ne dinga jëflanteek man ci ngor ak worma: rikk, bu ma denc Misra.

Ruth 2:6 TSK

Mu ne ko: «Mooy waa Mowab, ba Nawmi àndal, jóge Mowab, ñibbsi.

¶ Mag ñiy jiite mbooloo mi bu baax nag, nañu leen yellale ag njukkal ñaari yoon, rawatina ñi boole coonoy waare ak njàngle.