Genesis 24:26
TSK
Waa ji nag sujjóot, sant Aji Sax ji,
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Waa ji nag sujjóot, sant Aji Sax ji,
di leen xamal ay santaane aki ndigali yoon, di leen won fi ñu wara jaare ak li ñu wara def.
Nga ne ma: «Dama laa xelal, xamal la fi ngay jaar, digal la, di la xool.
jaarale leen yoon wu jub, ngir ñu àgg cib dëkk.
Yoon wu xelu laa la teg, jaarloo la yoonu njub.