TSK

TSK · Genesis 24:65

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Ba loolu amee mu summi yérey jëtun ya, muuru, sàngu, toog ca selebe yoon wa jëm Enayim ca yoonu Timna, ndax booba gis na ne Sela màgg na te mayuñu ko ko, muy jabaram.

Waaye jépp jigéen juy julli, mbaa muy waxe kàddug waxyu, te muurul boppam, suufeel na jëkkëram jiy boppam. Day mel ni bu nelu woon rekk.

Naka noonu, na jigéen ñi di sol col gu yiw, gu teggine te yem. Buñu jiital di defaroo ay létt yu ëpp, ak gànjari wurus, aki per, ak yérey tànnéef,