TSK

TSK · Genesis 25:34

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Man daal damay digle bànneex, ndax nit amul lu gën fi kaw suuf di lekk ak a naan ak a bànneexu, muñe ko doñ-doñam, fan yi ko Yàlla may fi kaw suuf.

¶ Aji Sax ji ne ma: «Ndaw njëg gu réy gu ma leen jaral! Sànni ko ca boroom njaq ya.» Ma jël fanweeri donji xaalis ya, sànni ko boroom njaq ya, ca kër Aji Sax ji.

“Yeen xeebaatekat yi, xool-leen, jommileen te ne mes, ndax jëf ji may def ci seen jamono, ku leen ko waxoon sax, dungeen ko gëm.”»

Ndaxte ñu baree ngii ñu seeni jëf tax ñu di nooni bantub Almasi. Loolu wax naa leen ko ay yoon, ma waxati leen ko tey aki jooy.