TSK

TSK · Genesis 26:23

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

¶ Israyil nag dem, yóbbaale mboolem lu bokk ci moom. Ba mu agsee Beerseba, dafa sarxal Yàllay baayam Isaaxa.

Amos 5:5 TSK

Buleen sàkkuji fa Betel, buleen dem Gilgal, te buleen jàll Beerseba. Gilgal ay gàlloo ngàllo; Betel neen.»